Ad-Dukhan · 17/59
Tekki Waxtaan — Ad-Dukhan
۞ وَلَقَدْ فَتَنَّا قَبْلَهُمْ قَوْمَ فِرْعَوْنَ وَجَاءَهُمْ رَسُولٌ كَرِيمٌ ۝١٧
Wa laqad fatannaa qablahum qawma Fir`awna wa jaaa`ahum Rasoolun kareem
📖 Tekkim Wolof
Sànje woon Nanu , nitu Firawna ña leen jiitu woon, te amoon na ñu ab Yonnent bu leen dikkaloon bu tedd,

🎧 Dégg


📜 Aaya 15-19 — Ad-Dukhan

15إِنَّا كَاشِفُو الْعَذَابِ قَلِيلًا ۚ إِنَّكُمْ عَائِدُونَ
Dananu teggi mbugël mi tuuti ; dangeen dellusi de.
16يَوْمَ نَبْطِشُ الْبَطْشَةَ الْكُبْرَىٰ إِنَّا مُنتَقِمُونَ
Cëy bu keroogee bis ba nuy kaanu di nappaje danuy fayu de.
17۞ وَلَقَدْ فَتَنَّا قَبْلَهُمْ قَوْمَ فِرْعَوْنَ وَجَاءَهُمْ رَسُولٌ كَرِيمٌ
Sànje woon Nanu , nitu Firawna ña leen jiitu woon, te amoon na ñu ab Yonnent bu leen dikkaloon bu tedd,
18أَنْ أَدُّوا إِلَيَّ عِبَادَ اللَّهِ ۖ إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
[daan leen wax naan]: “Delloleen ma jaamu Yàlla yi ! Ndax man mii ab Yonnent laa bu wóor.
19وَأَن لَّا تَعْلُوا عَلَى اللَّهِ ۖ إِنِّي آتِيكُم بِسُلْطَانٍ مُّبِينٍ
Buleen kawe kawe lu ci Yàlla, ndax man dey firnde ju wér laa leen indil.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
17Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 17

Simoore Ad-Dukhan Aaya 17 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Sànje woon Nanu , nitu Firawna ña leen jiitu woon,…

Simoore Aaya 17/59 — Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ad-Dukhan Dégg, Ad-Dukhan Tekki, Ad-Dukhan mp3, Ad-Dukhan pdf. Aaya 15–19. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, August 19, 2026

Don't forget us in your sincere prayers