Ad-Dukhan · 16/59
Tekki Waxtaan — Ad-Dukhan
يَوْمَ نَبْطِشُ الْبَطْشَةَ الْكُبْرَىٰ إِنَّا مُنتَقِمُونَ ۝١٦
Yawma nabtishul batsha tal kubraa innaa muntaqimoon
📖 Tekkim Wolof
Cëy bu keroogee bis ba nuy kaanu di nappaje danuy fayu de.

🎧 Dégg


📜 Aaya 14-18 — Ad-Dukhan

14ثُمَّ تَوَلَّوْا عَنْهُ وَقَالُوا مُعَلَّمٌ مَّجْنُونٌ
Ñu daldi dumóoyu te naan : “Kii daal, ab dof la”.
15إِنَّا كَاشِفُو الْعَذَابِ قَلِيلًا ۚ إِنَّكُمْ عَائِدُونَ
Dananu teggi mbugël mi tuuti ; dangeen dellusi de.
16يَوْمَ نَبْطِشُ الْبَطْشَةَ الْكُبْرَىٰ إِنَّا مُنتَقِمُونَ
Cëy bu keroogee bis ba nuy kaanu di nappaje danuy fayu de.
17۞ وَلَقَدْ فَتَنَّا قَبْلَهُمْ قَوْمَ فِرْعَوْنَ وَجَاءَهُمْ رَسُولٌ كَرِيمٌ
Sànje woon Nanu , nitu Firawna ña leen jiitu woon, te amoon na ñu ab Yonnent bu leen dikkaloon bu tedd,
18أَنْ أَدُّوا إِلَيَّ عِبَادَ اللَّهِ ۖ إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
[daan leen wax naan]: “Delloleen ma jaamu Yàlla yi ! Ndax man mii ab Yonnent laa bu wóor.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
16Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 16

Simoore Ad-Dukhan Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Cëy bu keroogee bis ba nuy kaanu di nappaje danuy…

Simoore Aaya 16/59 — Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ad-Dukhan Dégg, Ad-Dukhan Tekki, Ad-Dukhan mp3, Ad-Dukhan pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers