Ad-Dukhan · 36/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
فَأْتُوا بِآبَائِنَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ ۝٣٦
Faatoo bi aabaaa`inaaa inkuntum saadiqeen
📖 Tekkim Wolof
Su fekkee ne dëggu ngeen kon dekkalleen sunuy maam, délloosileen”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore Ad-Dukhan

34إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَيَقُولُونَ
Ñoo ñaa ngay wax naan :
35إِنْ هِيَ إِلَّا مَوْتَتُنَا الْأُولَىٰ وَمَا نَحْنُ بِمُنشَرِينَ
“Genn dee rekk am muy sunu dee, gu jëkk gi. Te it kenn dunu dekkalaat.
36فَأْتُوا بِآبَائِنَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Su fekkee ne dëggu ngeen kon dekkalleen sunuy maam, délloosileen”.
37أَهُمْ خَيْرٌ أَمْ قَوْمُ تُبَّعٍ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ أَهْلَكْنَاهُمْ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا مُجْرِمِينَ
moo ndax ñoom ñoo gën Tubbaa ak ña leen jiitu woon ? Faagaagoloon Nanu leen ndax ñoom ay niti tafaar lañu woon (tooñkat).
38وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا لَاعِبِينَ
Bindu Nu asamaan yeek suuf si ak li ci seen diggënte di ko fowe.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 36

Simoore Ad-Dukhan Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su fekkee ne dëggu ngeen kon dekkalleen sunuy maam, délloosileen”.

Simoore Aaya 36/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers