Ad-Dukhan · 35/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
إِنْ هِيَ إِلَّا مَوْتَتُنَا الْأُولَىٰ وَمَا نَحْنُ بِمُنشَرِينَ ۝٣٥
In hiya illaa mawtatunal oolaa wa maa nahnu bimun shareen
📖 Tekkim Wolof
“Genn dee rekk am muy sunu dee, gu jëkk gi. Te it kenn dunu dekkalaat.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 33-37 — Simoore Ad-Dukhan

33وَآتَيْنَاهُم مِّنَ الْآيَاتِ مَا فِيهِ بَلَاءٌ مُّبِينٌ
indiloon Nanu leen ay kéemaan (firnde) yu leer nàññ.
34إِنَّ هَٰؤُلَاءِ لَيَقُولُونَ
Ñoo ñaa ngay wax naan :
35إِنْ هِيَ إِلَّا مَوْتَتُنَا الْأُولَىٰ وَمَا نَحْنُ بِمُنشَرِينَ
“Genn dee rekk am muy sunu dee, gu jëkk gi. Te it kenn dunu dekkalaat.
36فَأْتُوا بِآبَائِنَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Su fekkee ne dëggu ngeen kon dekkalleen sunuy maam, délloosileen”.
37أَهُمْ خَيْرٌ أَمْ قَوْمُ تُبَّعٍ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ أَهْلَكْنَاهُمْ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا مُجْرِمِينَ
moo ndax ñoom ñoo gën Tubbaa ak ña leen jiitu woon ? Faagaagoloon Nanu leen ndax ñoom ay niti tafaar lañu woon (tooñkat).
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 35

Simoore Ad-Dukhan Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Genn dee rekk am muy sunu dee, gu jëkk gi.…

Simoore Aaya 35/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers