Ad-Dukhan · 37/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
أَهُمْ خَيْرٌ أَمْ قَوْمُ تُبَّعٍ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ أَهْلَكْنَاهُمْ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا مُجْرِمِينَ ۝٣٧
Ahum khayrun am qawmu Tubba`inw wallazeena min qablihim; ahlaknaahum innahum kaanoo mujrimeen
📖 Tekkim Wolof
moo ndax ñoom ñoo gën Tubbaa ak ña leen jiitu woon ? Faagaagoloon Nanu leen ndax ñoom ay niti tafaar lañu woon (tooñkat).

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Simoore Ad-Dukhan

35إِنْ هِيَ إِلَّا مَوْتَتُنَا الْأُولَىٰ وَمَا نَحْنُ بِمُنشَرِينَ
“Genn dee rekk am muy sunu dee, gu jëkk gi. Te it kenn dunu dekkalaat.
36فَأْتُوا بِآبَائِنَا إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Su fekkee ne dëggu ngeen kon dekkalleen sunuy maam, délloosileen”.
37أَهُمْ خَيْرٌ أَمْ قَوْمُ تُبَّعٍ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ أَهْلَكْنَاهُمْ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا مُجْرِمِينَ
moo ndax ñoom ñoo gën Tubbaa ak ña leen jiitu woon ? Faagaagoloon Nanu leen ndax ñoom ay niti tafaar lañu woon (tooñkat).
38وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا لَاعِبِينَ
Bindu Nu asamaan yeek suuf si ak li ci seen diggënte di ko fowe.
39مَا خَلَقْنَاهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Bindu Nu leen ci lu dul dëgg. Waaye ñi ëpp ci ñoom xamuñu.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 37

Simoore Ad-Dukhan Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : moo ndax ñoom ñoo gën Tubbaa ak ña leen jiitu…

Simoore Aaya 37/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers