Ad-Dukhan · 40/59
Tekki Waxtaan — Ad-Dukhan
إِنَّ يَوْمَ الْفَصْلِ مِيقَاتُهُمْ أَجْمَعِينَ ۝٤٠
Inna yawmal fasli meeqaatuhum ajma`een
📖 Tekkim Wolof
Ca bisub àtte ba, lañuy daje ñoom ñépp,

🎧 Dégg


📜 Aaya 38-42 — Ad-Dukhan

38وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا لَاعِبِينَ
Bindu Nu asamaan yeek suuf si ak li ci seen diggënte di ko fowe.
39مَا خَلَقْنَاهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Bindu Nu leen ci lu dul dëgg. Waaye ñi ëpp ci ñoom xamuñu.
40إِنَّ يَوْمَ الْفَصْلِ مِيقَاتُهُمْ أَجْمَعِينَ
Ca bisub àtte ba, lañuy daje ñoom ñépp,
41يَوْمَ لَا يُغْنِي مَوْلًى عَن مَّوْلًى شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
Bis ba farandoo dul jariñ moroom ja ; te kenn duleen dimbali,
42إِلَّا مَن رَّحِمَ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ هُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
ku dul ku Yàlla yërëm. mooy, boroom Kàttan, di Jaglewaakoon yërmande.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
40Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 40

Simoore Ad-Dukhan Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ca bisub àtte ba, lañuy daje ñoom ñépp,

Simoore Aaya 40/59 — Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ad-Dukhan Dégg, Ad-Dukhan Tekki, Ad-Dukhan mp3, Ad-Dukhan pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers