Ad-Dukhan · 41/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
يَوْمَ لَا يُغْنِي مَوْلًى عَن مَّوْلًى شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ ۝٤١
Yawma laa yughnee mawlan `am mawlan shai`anw wa laa hum yunsaroon
📖 Tekkim Wolof
Bis ba farandoo dul jariñ moroom ja ; te kenn duleen dimbali,

🎧 Dégg


📜 Aaya 39-43 — Simoore Ad-Dukhan

39مَا خَلَقْنَاهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Bindu Nu leen ci lu dul dëgg. Waaye ñi ëpp ci ñoom xamuñu.
40إِنَّ يَوْمَ الْفَصْلِ مِيقَاتُهُمْ أَجْمَعِينَ
Ca bisub àtte ba, lañuy daje ñoom ñépp,
41يَوْمَ لَا يُغْنِي مَوْلًى عَن مَّوْلًى شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
Bis ba farandoo dul jariñ moroom ja ; te kenn duleen dimbali,
42إِلَّا مَن رَّحِمَ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ هُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
ku dul ku Yàlla yërëm. mooy, boroom Kàttan, di Jaglewaakoon yërmande.
43إِنَّ شَجَرَتَ الزَّقُّومِ
Garabub Sakkuum ga tigi
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 41

Simoore Ad-Dukhan Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis ba farandoo dul jariñ moroom ja ; te kenn…

Simoore Aaya 41/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers