Ad-Dukhan · 39/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
مَا خَلَقْنَاهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ ۝٣٩
Maa khalaqnaahumaaa illaa bilhaqqi wa laakinna aksarahum laa ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Bindu Nu leen ci lu dul dëgg. Waaye ñi ëpp ci ñoom xamuñu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Simoore Ad-Dukhan

37أَهُمْ خَيْرٌ أَمْ قَوْمُ تُبَّعٍ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ أَهْلَكْنَاهُمْ ۖ إِنَّهُمْ كَانُوا مُجْرِمِينَ
moo ndax ñoom ñoo gën Tubbaa ak ña leen jiitu woon ? Faagaagoloon Nanu leen ndax ñoom ay niti tafaar lañu woon (tooñkat).
38وَمَا خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا لَاعِبِينَ
Bindu Nu asamaan yeek suuf si ak li ci seen diggënte di ko fowe.
39مَا خَلَقْنَاهُمَا إِلَّا بِالْحَقِّ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَهُمْ لَا يَعْلَمُونَ
Bindu Nu leen ci lu dul dëgg. Waaye ñi ëpp ci ñoom xamuñu.
40إِنَّ يَوْمَ الْفَصْلِ مِيقَاتُهُمْ أَجْمَعِينَ
Ca bisub àtte ba, lañuy daje ñoom ñépp,
41يَوْمَ لَا يُغْنِي مَوْلًى عَن مَّوْلًى شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
Bis ba farandoo dul jariñ moroom ja ; te kenn duleen dimbali,
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 39

Simoore Ad-Dukhan Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bindu Nu leen ci lu dul dëgg. Waaye ñi ëpp…

Simoore Aaya 39/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers