Ad-Dukhan · 42/59
Tekki Waxtaan — Ad-Dukhan
إِلَّا مَن رَّحِمَ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ هُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ ۝٤٢
Illaa mar rahimal laah` innahoo huwal `azeezur raheem
📖 Tekkim Wolof
ku dul ku Yàlla yërëm. mooy, boroom Kàttan, di Jaglewaakoon yërmande.
🎧 Dégg

📜 Aaya 40-44 — Ad-Dukhan

40إِنَّ يَوْمَ الْفَصْلِ مِيقَاتُهُمْ أَجْمَعِينَ
Ca bisub àtte ba, lañuy daje ñoom ñépp,
41يَوْمَ لَا يُغْنِي مَوْلًى عَن مَّوْلًى شَيْئًا وَلَا هُمْ يُنصَرُونَ
Bis ba farandoo dul jariñ moroom ja ; te kenn duleen dimbali,
42إِلَّا مَن رَّحِمَ اللَّهُ ۚ إِنَّهُ هُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
ku dul ku Yàlla yërëm. mooy, boroom Kàttan, di Jaglewaakoon yërmande.
43إِنَّ شَجَرَتَ الزَّقُّومِ
Garabub Sakkuum ga tigi
44طَعَامُ الْأَثِيمِ
moo di lekkug defaakoonu bàkkaar ya.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
42Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 42

Simoore Ad-Dukhan Aaya 42 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ku dul ku Yàlla yërëm. mooy, boroom Kàttan, di Jaglewaakoon…

Simoore Aaya 42/59 — Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ad-Dukhan Dégg, Ad-Dukhan Tekki, Ad-Dukhan mp3, Ad-Dukhan pdf. Aaya 40–44. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers