Ad-Dukhan · 6/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ ۝٦
Rahmatam mir rabbik; innahoo Huwas Samee`ul `Aleem
📖 Tekkim Wolof
moo di yërmaande ju bawoo ci sa Boroom, mooy Kiy Dégg, di ku Xam,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 4-8 — Simoore Ad-Dukhan

4فِيهَا يُفْرَقُ كُلُّ أَمْرٍ حَكِيمٍ
ci la Nuy teqalee mépp mbir mu xereñ,
5أَمْرًا مِّنْ عِندِنَا ۚ إِنَّا كُنَّا مُرْسِلِينَ
moo di mbir mu bawoo ci Nun. Ci la Nuy yónnee [Yonnenta ya],
6رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
moo di yërmaande ju bawoo ci sa Boroom, mooy Kiy Dégg, di ku Xam,
7رَبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا ۖ إِن كُنتُم مُّوقِنِينَ
Moo di Boroom asamaan yeek suuf seek li nekk ci seen diggënte, ndegam wóolu ngeen.
8لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ يُحْيِي وَيُمِيتُ ۖ رَبُّكُمْ وَرَبُّ آبَائِكُمُ الْأَوَّلِينَ
Amul jenn Yàlla judul Moom. Mooy dundal di reye, Mooy seen Boroom mooy Boroom seeni maam ya fi jëkkoon.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
6Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 6

Simoore Ad-Dukhan Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : moo di yërmaande ju bawoo ci sa Boroom, mooy Kiy…

Simoore Aaya 6/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers