Ad-Dukhan · 7/59
Tekki Waxtaan — Simoore Ad-Dukhan
رَبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا ۖ إِن كُنتُم مُّوقِنِينَ ۝٧
Rabbis samaawaati wal ardi wa maa bainahumaa; in kuntum mooqineen
📖 Tekkim Wolof
Moo di Boroom asamaan yeek suuf seek li nekk ci seen diggënte, ndegam wóolu ngeen.

🎧 Dégg


📜 Aaya 5-9 — Simoore Ad-Dukhan

5أَمْرًا مِّنْ عِندِنَا ۚ إِنَّا كُنَّا مُرْسِلِينَ
moo di mbir mu bawoo ci Nun. Ci la Nuy yónnee [Yonnenta ya],
6رَحْمَةً مِّن رَّبِّكَ ۚ إِنَّهُ هُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
moo di yërmaande ju bawoo ci sa Boroom, mooy Kiy Dégg, di ku Xam,
7رَبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا ۖ إِن كُنتُم مُّوقِنِينَ
Moo di Boroom asamaan yeek suuf seek li nekk ci seen diggënte, ndegam wóolu ngeen.
8لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ يُحْيِي وَيُمِيتُ ۖ رَبُّكُمْ وَرَبُّ آبَائِكُمُ الْأَوَّلِينَ
Amul jenn Yàlla judul Moom. Mooy dundal di reye, Mooy seen Boroom mooy Boroom seeni maam ya fi jëkkoon.
9بَلْ هُمْ فِي شَكٍّ يَلْعَبُونَ
Ñoom, ña ngay sikki-sàkka, di fo.
Ad-DukhanFihi Alxuraan
59Aaya
MeccanRevelation
7Aaya

Tekki — Ad-Dukhan 7

Simoore Ad-Dukhan Aaya 7 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo di Boroom asamaan yeek suuf seek li nekk ci…

Simoore Aaya 7/59 — Simoore Ad-Dukhan الدخان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ad-Dukhan Dégg, Simoore Ad-Dukhan Tekki, Simoore Ad-Dukhan mp3, Simoore Ad-Dukhan pdf. Aaya 5–9. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers