Muhammad · 35/38
Tekki Waxtaan — Muhammad
فَلَا تَهِنُوا وَتَدْعُوا إِلَى السَّلْمِ وَأَنتُمُ الْأَعْلَوْنَ وَاللَّهُ مَعَكُمْ وَلَن يَتِرَكُمْ أَعْمَالَكُمْ ٣٥
Transliteration
Falaa tahinoo wa tad`ooo ilas salmi wa antumul a`lawna wallaahu ma`akum wa lany yatirakum a`maalakum
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Bu leen di doyadi tey woote maslaa te yéen a gën a kawe, Yàlla itam yéen la àndal, te it séenug (peyug jëf) dara du ci wàññiku.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 33-37 — Muhammad
33۞ يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا أَطِيعُوا اللَّهَ وَأَطِيعُوا الرَّسُولَ وَلَا تُبْطِلُوا أَعْمَالَكُمْ
eey yéen ñi gëm ! Topp leen Yàlla tey topp Yonent bi, te bu leen di neenal séeni jëf.
34إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا وَصَدُّوا عَن سَبِيلِ اللَّهِ ثُمَّ مَاتُوا وَهُمْ كُفَّارٌ فَلَن يَغْفِرَ اللَّهُ لَهُمْ
Ña daan weddi tey dumóoyu yoonu Yàlla ba dee ca diy yéefar, Yàlla duleen jéggal.
35فَلَا تَهِنُوا وَتَدْعُوا إِلَى السَّلْمِ وَأَنتُمُ الْأَعْلَوْنَ وَاللَّهُ مَعَكُمْ وَلَن يَتِرَكُمْ أَعْمَالَكُمْ
Bu leen di doyadi tey woote maslaa te yéen a gën a kawe, Yàlla itam yéen la àndal, te it séenug (peyug jëf) dara du ci wàññiku.
36إِنَّمَا الْحَيَاةُ الدُّنْيَا لَعِبٌ وَلَهْوٌ ۚ وَإِن تُؤْمِنُوا وَتَتَّقُوا يُؤْتِكُمْ أُجُورَكُمْ وَلَا يَسْأَلْكُمْ أَمْوَالَكُمْ
Dundug Àddina sii am po la ak i caaxaan ; bu ngeen gëmee te ragal Yàlla di wattandiku , Dina leen jox séenug pey te duleen laaj séeni alal.
37إِن يَسْأَلْكُمُوهَا فَيُحْفِكُمْ تَبْخَلُوا وَيُخْرِجْ أَضْغَانَكُمْ
Buleen ko Yàlla laajoon, kon dangeen di nay te kon dana génne seeni dëxëñ teg mbañeel gi séen diggante .
MuhammadFihi Alxuraan
38Aaya
MedinanRevelation
35Aaya
Tekki — Muhammad 35
Simoore Muhammad Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu leen di doyadi tey woote maslaa te yéen a…Simoore Aaya 35/38 — Muhammad محمد (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Muhammad Dégg, Muhammad Tekki, Muhammad mp3, Muhammad pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








