Al-Maida · 58/120
Tekki Waxtaan — Al-Maida
وَإِذَا نَادَيْتُمْ إِلَى الصَّلَاةِ اتَّخَذُوهَا هُزُوًا وَلَعِبًا ۚ ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَعْقِلُونَ ۝٥٨
Wa izaa naadaitum ilas Salaatit takhazoohaa huzu wan`w wa la`ibaa; zaalika biannnahum qawmul laa ya`qiloon
📖 Tekkim Wolof
Bu ngeen di woote jëm ci julli, [ñoom] ñu jàppe ko caaxaan ak am po. Ñoom dañudi ay nit ñu xel-luwul.
🎧 Dégg

📜 Aaya 56-60 — Al-Maida

56وَمَن يَتَوَلَّ اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَالَّذِينَ آمَنُوا فَإِنَّ حِزْبَ اللَّهِ هُمُ الْغَالِبُونَ
Ku xaritook Yàlla ak Yonentam ak way-gëm ña, [na xam ne] ña ànd ak Yàlla ñooy nit ña [gàddu ndam la].
57يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَتَّخِذُوا الَّذِينَ اتَّخَذُوا دِينَكُمْ هُزُوًا وَلَعِبًا مِّنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ مِن قَبْلِكُمْ وَالْكُفَّارَ أَوْلِيَاءَ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen jàpp xarit ña nga xam ne dañuy jàppe seen diine ay caaxaan ak po, ca ña leen jëkk a jot Téere ak yéefar ya. Ragal-leen Yàlla ndegam way-gëm ngeen.
58وَإِذَا نَادَيْتُمْ إِلَى الصَّلَاةِ اتَّخَذُوهَا هُزُوًا وَلَعِبًا ۚ ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَعْقِلُونَ
Bu ngeen di woote jëm ci julli, [ñoom] ñu jàppe ko caaxaan ak am po. Ñoom dañudi ay nit ñu xel-luwul.
59قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ هَلْ تَنقِمُونَ مِنَّا إِلَّا أَنْ آمَنَّا بِاللَّهِ وَمَا أُنزِلَ إِلَيْنَا وَمَا أُنزِلَ مِن قَبْلُ وَأَنَّ أَكْثَرَكُمْ فَاسِقُونَ
Neel : “Éy yéen ñoñ-téere ! Ndax li ngeen nu bañe nekkul lu dul li nu gëm Yàlla ak li wàcceef na ko ci nun ak la jëkkoon a wàcc ? Li ëpp ci yéen ay saay-saay lañu.
60قُلْ هَلْ أُنَبِّئُكُم بِشَرٍّ مِّن ذَٰلِكَ مَثُوبَةً عِندَ اللَّهِ ۚ مَن لَّعَنَهُ اللَّهُ وَغَضِبَ عَلَيْهِ وَجَعَلَ مِنْهُمُ الْقِرَدَةَ وَالْخَنَازِيرَ وَعَبَدَ الطَّاغُوتَ ۚ أُولَٰئِكَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضَلُّ عَن سَوَاءِ السَّبِيلِ
Neel : “Moo ndax duma leen xamal ku yées pey ëllëg ca Yàlla ? Ña Yàlla rëbb, mere leen, soppi lenn ca ñoom ay golo ak i mbaam-xuux te ñuy jaamu Séytaane, ñooña ñoo yées dëkkuwaay te ñoo gën a réer, sore yoon wu jub wa”.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
58Aaya

Tekki — Al-Maida 58

Simoore Al-Maida Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ngeen di woote jëm ci julli, [ñoom] ñu jàppe…

Simoore Aaya 58/120 — Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Maida Dégg, Al-Maida Tekki, Al-Maida mp3, Al-Maida pdf. Aaya 56–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers