Al-Maida · 59/120
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Maida
قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ هَلْ تَنقِمُونَ مِنَّا إِلَّا أَنْ آمَنَّا بِاللَّهِ وَمَا أُنزِلَ إِلَيْنَا وَمَا أُنزِلَ مِن قَبْلُ وَأَنَّ أَكْثَرَكُمْ فَاسِقُونَ ۝٥٩
Qul yaaa Ahlal Kitaabi hal tanqimoona minnaaa illaaa an aamannaa billaahi wa maaa unzila ilainaa wa maa unzila min qablu wa annna aksarakum faasiqoon
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Éy yéen ñoñ-téere ! Ndax li ngeen nu bañe nekkul lu dul li nu gëm Yàlla ak li wàcceef na ko ci nun ak la jëkkoon a wàcc ? Li ëpp ci yéen ay saay-saay lañu.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 57-61 — Simoore Al-Maida

57يَا أَيُّهَا الَّذِينَ آمَنُوا لَا تَتَّخِذُوا الَّذِينَ اتَّخَذُوا دِينَكُمْ هُزُوًا وَلَعِبًا مِّنَ الَّذِينَ أُوتُوا الْكِتَابَ مِن قَبْلِكُمْ وَالْكُفَّارَ أَوْلِيَاءَ ۚ وَاتَّقُوا اللَّهَ إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ
Éy yéen ñi gëm ! Buleen jàpp xarit ña nga xam ne dañuy jàppe seen diine ay caaxaan ak po, ca ña leen jëkk a jot Téere ak yéefar ya. Ragal-leen Yàlla ndegam way-gëm ngeen.
58وَإِذَا نَادَيْتُمْ إِلَى الصَّلَاةِ اتَّخَذُوهَا هُزُوًا وَلَعِبًا ۚ ذَٰلِكَ بِأَنَّهُمْ قَوْمٌ لَّا يَعْقِلُونَ
Bu ngeen di woote jëm ci julli, [ñoom] ñu jàppe ko caaxaan ak am po. Ñoom dañudi ay nit ñu xel-luwul.
59قُلْ يَا أَهْلَ الْكِتَابِ هَلْ تَنقِمُونَ مِنَّا إِلَّا أَنْ آمَنَّا بِاللَّهِ وَمَا أُنزِلَ إِلَيْنَا وَمَا أُنزِلَ مِن قَبْلُ وَأَنَّ أَكْثَرَكُمْ فَاسِقُونَ
Neel : “Éy yéen ñoñ-téere ! Ndax li ngeen nu bañe nekkul lu dul li nu gëm Yàlla ak li wàcceef na ko ci nun ak la jëkkoon a wàcc ? Li ëpp ci yéen ay saay-saay lañu.
60قُلْ هَلْ أُنَبِّئُكُم بِشَرٍّ مِّن ذَٰلِكَ مَثُوبَةً عِندَ اللَّهِ ۚ مَن لَّعَنَهُ اللَّهُ وَغَضِبَ عَلَيْهِ وَجَعَلَ مِنْهُمُ الْقِرَدَةَ وَالْخَنَازِيرَ وَعَبَدَ الطَّاغُوتَ ۚ أُولَٰئِكَ شَرٌّ مَّكَانًا وَأَضَلُّ عَن سَوَاءِ السَّبِيلِ
Neel : “Moo ndax duma leen xamal ku yées pey ëllëg ca Yàlla ? Ña Yàlla rëbb, mere leen, soppi lenn ca ñoom ay golo ak i mbaam-xuux te ñuy jaamu Séytaane, ñooña ñoo yées dëkkuwaay te ñoo gën a réer, sore yoon wu jub wa”.
61وَإِذَا جَاءُوكُمْ قَالُوا آمَنَّا وَقَد دَّخَلُوا بِالْكُفْرِ وَهُمْ قَدْ خَرَجُوا بِهِ ۚ وَاللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا كَانُوا يَكْتُمُونَ
Bu ñu dikkee ci yéen naan : “Gëm nanu.”. Te fekk kéefar lañu indiwaale te moom lañuy yóbbuwaale. Te Yàllaa gën a xam la ñuy nëbb.
Al-MaidaFihi Alxuraan
120Aaya
MedinanRevelation
59Aaya

Tekki — Al-Maida 59

Simoore Al-Maida Aaya 59 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Éy yéen ñoñ-téere ! Ndax li ngeen nu…

Simoore Aaya 59/120 — Simoore Al-Maida المائدة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Maida Dégg, Simoore Al-Maida Tekki, Simoore Al-Maida mp3, Simoore Al-Maida pdf. Aaya 57–61. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 29, 2026

Don't forget us in your sincere prayers