Qaf · 21/45
Tekki Waxtaan — Qaf
وَجَاءَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّعَهَا سَائِقٌ وَشَهِيدٌ ۝٢١
Wa jaaa`at kullu nafsim ma`ahaa saaa`iqunw wa shaheed
📖 Tekkim Wolof
Bakkan bu nekk dikk ànd ak ku koy wommat ak ku koy seede.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Qaf

19وَجَاءَتْ سَكْرَةُ الْمَوْتِ بِالْحَقِّ ۖ ذَٰلِكَ مَا كُنتَ مِنْهُ تَحِيدُ
Sukraatus ndee aksi na ci ñoom tigi : “Loolu moo di li nga daan weddi”.
20وَنُفِخَ فِي الصُّورِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْوَعِيدِ
Bu nu wolee Bufta bi : Loolu moo di bisub Tëkóo ba.
21وَجَاءَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّعَهَا سَائِقٌ وَشَهِيدٌ
Bakkan bu nekk dikk ànd ak ku koy wommat ak ku koy seede.
22لَّقَدْ كُنتَ فِي غَفْلَةٍ مِّنْ هَٰذَا فَكَشَفْنَا عَنكَ غِطَاءَكَ فَبَصَرُكَ الْيَوْمَ حَدِيدٌ
“Lii lépp danga ko sàgganewoon. Bis niki tey, wuññi Nanu kiiraay li nekkoon ci say gët ; tey jii am nga gis bu xóot.
23وَقَالَ قَرِينُهُ هَٰذَا مَا لَدَيَّ عَتِيدٌ
Ka muy lëkóol ma ngay wax naan : “Kii mooy sama àndandoo bi ma dul tàggóolati”.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — Qaf 21

Simoore Qaf Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bakkan bu nekk dikk ànd ak ku koy wommat ak…

Simoore Aaya 21/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers