Qaf · 20/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
وَنُفِخَ فِي الصُّورِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْوَعِيدِ ۝٢٠
Wa nufikha fis Soor; zaalika yawmul wa`eed
📖 Tekkim Wolof
Bu nu wolee Bufta bi : Loolu moo di bisub Tëkóo ba.

🎧 Dégg


📜 Aaya 18-22 — Simoore Qaf

18مَّا يَلْفِظُ مِن قَوْلٍ إِلَّا لَدَيْهِ رَقِيبٌ عَتِيدٌ
Amul jenn wax ju muy àddu lu dul ne Raqiib ak Atiid ña nga ko tiim (ñiy bind jëfi nit ñi) .
19وَجَاءَتْ سَكْرَةُ الْمَوْتِ بِالْحَقِّ ۖ ذَٰلِكَ مَا كُنتَ مِنْهُ تَحِيدُ
Sukraatus ndee aksi na ci ñoom tigi : “Loolu moo di li nga daan weddi”.
20وَنُفِخَ فِي الصُّورِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْوَعِيدِ
Bu nu wolee Bufta bi : Loolu moo di bisub Tëkóo ba.
21وَجَاءَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّعَهَا سَائِقٌ وَشَهِيدٌ
Bakkan bu nekk dikk ànd ak ku koy wommat ak ku koy seede.
22لَّقَدْ كُنتَ فِي غَفْلَةٍ مِّنْ هَٰذَا فَكَشَفْنَا عَنكَ غِطَاءَكَ فَبَصَرُكَ الْيَوْمَ حَدِيدٌ
“Lii lépp danga ko sàgganewoon. Bis niki tey, wuññi Nanu kiiraay li nekkoon ci say gët ; tey jii am nga gis bu xóot.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
20Aaya

Tekki — Qaf 20

Simoore Qaf Aaya 20 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu nu wolee Bufta bi : Loolu moo di bisub…

Simoore Aaya 20/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 18–22. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers