Qaf · 22/45
Tekki Waxtaan — Simoore Qaf
لَّقَدْ كُنتَ فِي غَفْلَةٍ مِّنْ هَٰذَا فَكَشَفْنَا عَنكَ غِطَاءَكَ فَبَصَرُكَ الْيَوْمَ حَدِيدٌ ۝٢٢
Laqad kunta fee ghaf latim min haazaa fakashafnaa `anka ghitaaa`aka fabasarukal yawma hadeed
📖 Tekkim Wolof
“Lii lépp danga ko sàgganewoon. Bis niki tey, wuññi Nanu kiiraay li nekkoon ci say gët ; tey jii am nga gis bu xóot.

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — Simoore Qaf

20وَنُفِخَ فِي الصُّورِ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْوَعِيدِ
Bu nu wolee Bufta bi : Loolu moo di bisub Tëkóo ba.
21وَجَاءَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّعَهَا سَائِقٌ وَشَهِيدٌ
Bakkan bu nekk dikk ànd ak ku koy wommat ak ku koy seede.
22لَّقَدْ كُنتَ فِي غَفْلَةٍ مِّنْ هَٰذَا فَكَشَفْنَا عَنكَ غِطَاءَكَ فَبَصَرُكَ الْيَوْمَ حَدِيدٌ
“Lii lépp danga ko sàgganewoon. Bis niki tey, wuññi Nanu kiiraay li nekkoon ci say gët ; tey jii am nga gis bu xóot.
23وَقَالَ قَرِينُهُ هَٰذَا مَا لَدَيَّ عَتِيدٌ
Ka muy lëkóol ma ngay wax naan : “Kii mooy sama àndandoo bi ma dul tàggóolati”.
24أَلْقِيَا فِي جَهَنَّمَ كُلَّ كَفَّارٍ عَنِيدٍ
“Yéen ñaar, sànni leen ca safara weddiwaakoon ya daan féttérlu,
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — Qaf 22

Simoore Qaf Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Lii lépp danga ko sàgganewoon. Bis niki tey, wuññi Nanu…

Simoore Aaya 22/45 — Simoore Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Qaf Dégg, Simoore Qaf Tekki, Simoore Qaf mp3, Simoore Qaf pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers