Qaf · 24/45
Tekki Waxtaan — Qaf
أَلْقِيَا فِي جَهَنَّمَ كُلَّ كَفَّارٍ عَنِيدٍ ۝٢٤
Alqiyaa fee Jahannama kulla kaffaarin `aneed
📖 Tekkim Wolof
“Yéen ñaar, sànni leen ca safara weddiwaakoon ya daan féttérlu,
🎧 Dégg

📜 Aaya 22-26 — Qaf

22لَّقَدْ كُنتَ فِي غَفْلَةٍ مِّنْ هَٰذَا فَكَشَفْنَا عَنكَ غِطَاءَكَ فَبَصَرُكَ الْيَوْمَ حَدِيدٌ
“Lii lépp danga ko sàgganewoon. Bis niki tey, wuññi Nanu kiiraay li nekkoon ci say gët ; tey jii am nga gis bu xóot.
23وَقَالَ قَرِينُهُ هَٰذَا مَا لَدَيَّ عَتِيدٌ
Ka muy lëkóol ma ngay wax naan : “Kii mooy sama àndandoo bi ma dul tàggóolati”.
24أَلْقِيَا فِي جَهَنَّمَ كُلَّ كَفَّارٍ عَنِيدٍ
“Yéen ñaar, sànni leen ca safara weddiwaakoon ya daan féttérlu,
25مَّنَّاعٍ لِّلْخَيْرِ مُعْتَدٍ مُّرِيبٍ
ña daan tere aw yiw, te daan jalgati, daan sikki-sàkka,
26الَّذِي جَعَلَ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَأَلْقِيَاهُ فِي الْعَذَابِ الشَّدِيدِ
ka daan jéem a woote jeneen Yàlla di ko booleek Yàlla. Sànni leen ko ci mbugal mu tar ma”.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Qaf 24

Simoore Qaf Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : “Yéen ñaar, sànni leen ca safara weddiwaakoon ya daan féttérlu,

Simoore Aaya 24/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers