Qaf · 23/45
Tekki Waxtaan — Qaf
وَقَالَ قَرِينُهُ هَٰذَا مَا لَدَيَّ عَتِيدٌ ۝٢٣
Wa qaala qareenuhoo haazaa maa ladaiya `ateed
📖 Tekkim Wolof
Ka muy lëkóol ma ngay wax naan : “Kii mooy sama àndandoo bi ma dul tàggóolati”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Qaf

21وَجَاءَتْ كُلُّ نَفْسٍ مَّعَهَا سَائِقٌ وَشَهِيدٌ
Bakkan bu nekk dikk ànd ak ku koy wommat ak ku koy seede.
22لَّقَدْ كُنتَ فِي غَفْلَةٍ مِّنْ هَٰذَا فَكَشَفْنَا عَنكَ غِطَاءَكَ فَبَصَرُكَ الْيَوْمَ حَدِيدٌ
“Lii lépp danga ko sàgganewoon. Bis niki tey, wuññi Nanu kiiraay li nekkoon ci say gët ; tey jii am nga gis bu xóot.
23وَقَالَ قَرِينُهُ هَٰذَا مَا لَدَيَّ عَتِيدٌ
Ka muy lëkóol ma ngay wax naan : “Kii mooy sama àndandoo bi ma dul tàggóolati”.
24أَلْقِيَا فِي جَهَنَّمَ كُلَّ كَفَّارٍ عَنِيدٍ
“Yéen ñaar, sànni leen ca safara weddiwaakoon ya daan féttérlu,
25مَّنَّاعٍ لِّلْخَيْرِ مُعْتَدٍ مُّرِيبٍ
ña daan tere aw yiw, te daan jalgati, daan sikki-sàkka,
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Qaf 23

Simoore Qaf Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ka muy lëkóol ma ngay wax naan : “Kii mooy…

Simoore Aaya 23/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers