Qaf · 40/45
Tekki Waxtaan — Qaf
وَمِنَ اللَّيْلِ فَسَبِّحْهُ وَأَدْبَارَ السُّجُودِ ٤٠
Transliteration
Wa minal laili fasabbih hu wa adbaaras sujood
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
guddi gi it dee ko sàbbaal, ak ci ginnaaw julli gu nekk
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 38-42 — Qaf
38وَلَقَدْ خَلَقْنَا السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضَ وَمَا بَيْنَهُمَا فِي سِتَّةِ أَيَّامٍ وَمَا مَسَّنَا مِن لُّغُوبٍ
Man Yàlla, Maa bind asamaan yeek suuf ak li nekk ci seen diggante diirub juróom-benni fan, te Amuma ci benn coono.
39فَاصْبِرْ عَلَىٰ مَا يَقُولُونَ وَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ قَبْلَ طُلُوعِ الشَّمْسِ وَقَبْلَ الْغُرُوبِ
Nangay muñ li ñuy wax : te nangay kañ di sàbbaal sa Boroom di ko sant balaa jant bi fenk ak balaa muy so ;
40وَمِنَ اللَّيْلِ فَسَبِّحْهُ وَأَدْبَارَ السُّجُودِ
guddi gi it dee ko sàbbaal, ak ci ginnaaw julli gu nekk
41وَاسْتَمِعْ يَوْمَ يُنَادِ الْمُنَادِ مِن مَّكَانٍ قَرِيبٍ
Yaw (Yonent) bi déglul , bu keroogee ba Wootekat ba (Israafiil) di wootee fu jige,
42يَوْمَ يَسْمَعُونَ الصَّيْحَةَ بِالْحَقِّ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُرُوجِ
bis ba nga xam ne danañu dégg xaacu ga. Te bóobule Bis moo di bisub Dekkiwaat ba.
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
40Aaya
Tekki — Qaf 40
Simoore Qaf Aaya 40 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : guddi gi it dee ko sàbbaal, ak ci ginnaaw julli…Simoore Aaya 40/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 38–42. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








