Qaf · 41/45
Tekki Waxtaan — Qaf
وَاسْتَمِعْ يَوْمَ يُنَادِ الْمُنَادِ مِن مَّكَانٍ قَرِيبٍ ۝٤١
Wastami` yawma yunaa dil munaadi mim makaanin qareeb
📖 Tekkim Wolof
Yaw (Yonent) bi déglul , bu keroogee ba Wootekat ba (Israafiil) di wootee fu jige,

🎧 Dégg


📜 Aaya 39-43 — Qaf

39فَاصْبِرْ عَلَىٰ مَا يَقُولُونَ وَسَبِّحْ بِحَمْدِ رَبِّكَ قَبْلَ طُلُوعِ الشَّمْسِ وَقَبْلَ الْغُرُوبِ
Nangay muñ li ñuy wax : te nangay kañ di sàbbaal sa Boroom di ko sant balaa jant bi fenk ak balaa muy so ;
40وَمِنَ اللَّيْلِ فَسَبِّحْهُ وَأَدْبَارَ السُّجُودِ
guddi gi it dee ko sàbbaal, ak ci ginnaaw julli gu nekk
41وَاسْتَمِعْ يَوْمَ يُنَادِ الْمُنَادِ مِن مَّكَانٍ قَرِيبٍ
Yaw (Yonent) bi déglul , bu keroogee ba Wootekat ba (Israafiil) di wootee fu jige,
42يَوْمَ يَسْمَعُونَ الصَّيْحَةَ بِالْحَقِّ ۚ ذَٰلِكَ يَوْمُ الْخُرُوجِ
bis ba nga xam ne danañu dégg xaacu ga. Te bóobule Bis moo di bisub Dekkiwaat ba.
43إِنَّا نَحْنُ نُحْيِي وَنُمِيتُ وَإِلَيْنَا الْمَصِيرُ
Nun Yàlla (Man Yàlla) Maay dundal di rey, te ci Man la lépp di mujj,
QafFihi Alxuraan
45Aaya
MeccanRevelation
41Aaya

Tekki — Qaf 41

Simoore Qaf Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yaw (Yonent) bi déglul , bu keroogee ba Wootekat ba…

Simoore Aaya 41/45 — Qaf ق (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Qaf Dégg, Qaf Tekki, Qaf mp3, Qaf pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers