At-Tur · 22/49
Tekki Waxtaan — At-Tur
وَأَمْدَدْنَاهُم بِفَاكِهَةٍ وَلَحْمٍ مِّمَّا يَشْتَهُونَ ۝٢٢
Wa amdadnaahum bifaa kihatinw wa lahmim mimmaa yashtahoon
📖 Tekkim Wolof
Te Dananu leen jox ay foytéef ak yàpp lépp lu ñu cay soxla.

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — At-Tur

20مُتَّكِئِينَ عَلَىٰ سُرُرٍ مَّصْفُوفَةٍ ۖ وَزَوَّجْنَاهُم بِحُورٍ عِينٍ
ñangay sóonu ci ay lal yu ñu sësële”, te may Nanu leen ay soxna yu “huuru al iin” (am bët jekk),
21وَالَّذِينَ آمَنُوا وَاتَّبَعَتْهُمْ ذُرِّيَّتُهُم بِإِيمَانٍ أَلْحَقْنَا بِهِمْ ذُرِّيَّتَهُمْ وَمَا أَلَتْنَاهُم مِّنْ عَمَلِهِم مِّن شَيْءٍ ۚ كُلُّ امْرِئٍ بِمَا كَسَبَ رَهِينٌ
Ña gëmoon te seen sët topp leen ca ngëm googee, Dananu def seeni sët ñu dab leen. Te duñu wàññi dara ci sen jëf, kenn ku nekk ay moom la mu sàkku.
22وَأَمْدَدْنَاهُم بِفَاكِهَةٍ وَلَحْمٍ مِّمَّا يَشْتَهُونَ
Te Dananu leen jox ay foytéef ak yàpp lépp lu ñu cay soxla.
23يَتَنَازَعُونَ فِيهَا كَأْسًا لَّا لَغْوٌ فِيهَا وَلَا تَأْثِيمٌ
Danuñu cay joqlante ak i kopp ci lu àndul ak i caaxaan waxatumalaa sobe.
24۞ وَيَطُوفُ عَلَيْهِمْ غِلْمَانٌ لَّهُمْ كَأَنَّهُمْ لُؤْلُؤٌ مَّكْنُونٌ
Dananu am xale yuy wër ci ñoom, yu melni pepp.
At-TurFihi Alxuraan
49Aaya
MeccanRevelation
22Aaya

Tekki — At-Tur 22

Simoore At-Tur Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te Dananu leen jox ay foytéef ak yàpp lépp lu…

Simoore Aaya 22/49 — At-Tur الطور (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: At-Tur Dégg, At-Tur Tekki, At-Tur mp3, At-Tur pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers