Al-Qamar · 24/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
فَقَالُوا أَبَشَرًا مِّنَّا وَاحِدًا نَّتَّبِعُهُ إِنَّا إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ وَسُعُرٍ ۝٢٤
Faqaalooo a-basharam minnaa waahidan nattabi`uhooo innaa izal lafee dalaalinw wa su`ur
📖 Tekkim Wolof
Ñuy wax naan : “Jenn waay ni nun nu di ko topp ? Kon dey nu sànku te réer.

🎧 Dégg


📜 Aaya 22-26 — Al-Qamar

22وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal Nanu Alxuraan ngir ñu fàttalikoo ca. Moo kon ndax kenn dana ca jàjjoo ?
23كَذَّبَتْ ثَمُودُ بِالنُّذُرِ
Waa Samuud weddi woon nañu fàtteli ga?
24فَقَالُوا أَبَشَرًا مِّنَّا وَاحِدًا نَّتَّبِعُهُ إِنَّا إِذًا لَّفِي ضَلَالٍ وَسُعُرٍ
Ñuy wax naan : “Jenn waay ni nun nu di ko topp ? Kon dey nu sànku te réer.
25أَأُلْقِيَ الذِّكْرُ عَلَيْهِ مِن بَيْنِنَا بَلْ هُوَ كَذَّابٌ أَشِرٌ
Moo ndax dañu koo coqate moom doŋŋ ci nun yónni ko ? Kii daal ab fentaakoon la, bu yées”
26سَيَعْلَمُونَ غَدًا مَّنِ الْكَذَّابُ الْأَشِرُ
Xalset nañu xam bu ëllëgee, ana kan mooy fentaakoon bu yées ba.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
24Aaya

Tekki — Al-Qamar 24

Simoore Al-Qamar Aaya 24 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñuy wax naan : “Jenn waay ni nun nu di…

Simoore Aaya 24/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 22–26. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers