Al-Qamar · 28/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
وَنَبِّئْهُمْ أَنَّ الْمَاءَ قِسْمَةٌ بَيْنَهُمْ ۖ كُلُّ شِرْبٍ مُّحْتَضَرٌ ۝٢٨
Wa nabbi`hum annal maaa`a qismatum bainahum kullu shirbim muhtadar
📖 Tekkim Wolof
Nanga xamle ne ndox ma dañu koy bokk séddóo ñook [giléem ga] ; duñu fa fekkante.
🎧 Dégg

📜 Aaya 26-30 — Al-Qamar

26سَيَعْلَمُونَ غَدًا مَّنِ الْكَذَّابُ الْأَشِرُ
Xalset nañu xam bu ëllëgee, ana kan mooy fentaakoon bu yées ba.
27إِنَّا مُرْسِلُو النَّاقَةِ فِتْنَةً لَّهُمْ فَارْتَقِبْهُمْ وَاصْطَبِرْ
yónni nanu ca ñoom naaga (gileem gu jigéen), muy sànje ci ñoom. Fugluleen te muñalleen (Saalih).
28وَنَبِّئْهُمْ أَنَّ الْمَاءَ قِسْمَةٌ بَيْنَهُمْ ۖ كُلُّ شِرْبٍ مُّحْتَضَرٌ
Nanga xamle ne ndox ma dañu koy bokk séddóo ñook [giléem ga] ; duñu fa fekkante.
29فَنَادَوْا صَاحِبَهُمْ فَتَعَاطَىٰ فَعَقَرَ
Ñu daldi woo seen àndandoo mu daldi koy rey.
30فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Naka la Sama mbugël ak Sama xupp nekke (ci seen kaw) ?
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
28Aaya

Tekki — Al-Qamar 28

Simoore Al-Qamar Aaya 28 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nanga xamle ne ndox ma dañu koy bokk séddóo ñook…

Simoore Aaya 28/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 26–30. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers