Al-Qamar · 29/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
فَنَادَوْا صَاحِبَهُمْ فَتَعَاطَىٰ فَعَقَرَ ۝٢٩
Fanaadaw saahibahum fata`aataa fa`aqar
📖 Tekkim Wolof
Ñu daldi woo seen àndandoo mu daldi koy rey.

🎧 Dégg


📜 Aaya 27-31 — Simoore Al-Qamar

27إِنَّا مُرْسِلُو النَّاقَةِ فِتْنَةً لَّهُمْ فَارْتَقِبْهُمْ وَاصْطَبِرْ
yónni nanu ca ñoom naaga (gileem gu jigéen), muy sànje ci ñoom. Fugluleen te muñalleen (Saalih).
28وَنَبِّئْهُمْ أَنَّ الْمَاءَ قِسْمَةٌ بَيْنَهُمْ ۖ كُلُّ شِرْبٍ مُّحْتَضَرٌ
Nanga xamle ne ndox ma dañu koy bokk séddóo ñook [giléem ga] ; duñu fa fekkante.
29فَنَادَوْا صَاحِبَهُمْ فَتَعَاطَىٰ فَعَقَرَ
Ñu daldi woo seen àndandoo mu daldi koy rey.
30فَكَيْفَ كَانَ عَذَابِي وَنُذُرِ
Naka la Sama mbugël ak Sama xupp nekke (ci seen kaw) ?
31إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ صَيْحَةً وَاحِدَةً فَكَانُوا كَهَشِيمِ الْمُحْتَظِرِ
Yabal nanu ca ñoom genn Xaacu, ñu mel poñiitum kuy ñag am ñax.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — Al-Qamar 29

Simoore Al-Qamar Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ñu daldi woo seen àndandoo mu daldi koy rey.

Simoore Aaya 29/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers