Al-Qamar · 35/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
نِّعْمَةً مِّنْ عِندِنَا ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي مَن شَكَرَ ۝٣٥
Ni`matam min `indinaa; kazaalika najzee man shakar
📖 Tekkim Wolof
mudi xéewal gu bawoo ci Nun : noonu Lanuy faye képp kuy sant.
🎧 Dégg

📜 Aaya 33-37 — Al-Qamar

33كَذَّبَتْ قَوْمُ لُوطٍ بِالنُّذُرِ
Nitu Lóot weddi woon nañu lañu leen daan xuppe.
34إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ حَاصِبًا إِلَّا آلَ لُوطٍ ۖ نَّجَّيْنَاهُم بِسَحَرٍ
Yabal Nanu ca ñoom ngelawu callmeer (mu faagaagal leen), ba mu des njabootug Lóot ñoom musël Nanu leen ca njël,
35نِّعْمَةً مِّنْ عِندِنَا ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي مَن شَكَرَ
mudi xéewal gu bawoo ci Nun : noonu Lanuy faye képp kuy sant.
36وَلَقَدْ أَنذَرَهُم بَطْشَتَنَا فَتَمَارَوْا بِالنُّذُرِ
Daan na leen xupp ci Sunu mbugël. Waaye teewul ñu daan werante ci loolu.
37وَلَقَدْ رَاوَدُوهُ عَن ضَيْفِهِ فَطَمَسْنَا أَعْيُنَهُمْ فَذُوقُوا عَذَابِي وَنُذُرِ
Dañoo, sàkkoo saay-saaye ganam ña. Nu daldi fatt seen gët ne leen “Mosleen Sama mbugël ak Samak xupp”.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
35Aaya

Tekki — Al-Qamar 35

Simoore Al-Qamar Aaya 35 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mudi xéewal gu bawoo ci Nun : noonu Lanuy faye…

Simoore Aaya 35/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 33–37. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers