Al-Qamar · 34/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ حَاصِبًا إِلَّا آلَ لُوطٍ ۖ نَّجَّيْنَاهُم بِسَحَرٍ ۝٣٤
Innaa arsalnaa `alaihim haasiban illaaa aala Loot najjainaahum bisahar
📖 Tekkim Wolof
Yabal Nanu ca ñoom ngelawu callmeer (mu faagaagal leen), ba mu des njabootug Lóot ñoom musël Nanu leen ca njël,

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 32-36 — Simoore Al-Qamar

32وَلَقَدْ يَسَّرْنَا الْقُرْآنَ لِلذِّكْرِ فَهَلْ مِن مُّدَّكِرٍ
Yombal nanu, Alxuraan ngir ñu fàttaliku ca. Mo ndax kenn dana ca jàjjoo ?
33كَذَّبَتْ قَوْمُ لُوطٍ بِالنُّذُرِ
Nitu Lóot weddi woon nañu lañu leen daan xuppe.
34إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ حَاصِبًا إِلَّا آلَ لُوطٍ ۖ نَّجَّيْنَاهُم بِسَحَرٍ
Yabal Nanu ca ñoom ngelawu callmeer (mu faagaagal leen), ba mu des njabootug Lóot ñoom musël Nanu leen ca njël,
35نِّعْمَةً مِّنْ عِندِنَا ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي مَن شَكَرَ
mudi xéewal gu bawoo ci Nun : noonu Lanuy faye képp kuy sant.
36وَلَقَدْ أَنذَرَهُم بَطْشَتَنَا فَتَمَارَوْا بِالنُّذُرِ
Daan na leen xupp ci Sunu mbugël. Waaye teewul ñu daan werante ci loolu.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-Qamar 34

Simoore Al-Qamar Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yabal Nanu ca ñoom ngelawu callmeer (mu faagaagal leen), ba…

Simoore Aaya 34/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers