Al-Qamar · 36/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
وَلَقَدْ أَنذَرَهُم بَطْشَتَنَا فَتَمَارَوْا بِالنُّذُرِ ۝٣٦
Wa laqad anzarahum batshatanaa fatamaaraw binnuzur
📖 Tekkim Wolof
Daan na leen xupp ci Sunu mbugël. Waaye teewul ñu daan werante ci loolu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore Al-Qamar

34إِنَّا أَرْسَلْنَا عَلَيْهِمْ حَاصِبًا إِلَّا آلَ لُوطٍ ۖ نَّجَّيْنَاهُم بِسَحَرٍ
Yabal Nanu ca ñoom ngelawu callmeer (mu faagaagal leen), ba mu des njabootug Lóot ñoom musël Nanu leen ca njël,
35نِّعْمَةً مِّنْ عِندِنَا ۚ كَذَٰلِكَ نَجْزِي مَن شَكَرَ
mudi xéewal gu bawoo ci Nun : noonu Lanuy faye képp kuy sant.
36وَلَقَدْ أَنذَرَهُم بَطْشَتَنَا فَتَمَارَوْا بِالنُّذُرِ
Daan na leen xupp ci Sunu mbugël. Waaye teewul ñu daan werante ci loolu.
37وَلَقَدْ رَاوَدُوهُ عَن ضَيْفِهِ فَطَمَسْنَا أَعْيُنَهُمْ فَذُوقُوا عَذَابِي وَنُذُرِ
Dañoo, sàkkoo saay-saaye ganam ña. Nu daldi fatt seen gët ne leen “Mosleen Sama mbugël ak Samak xupp”.
38وَلَقَدْ صَبَّحَهُم بُكْرَةً عَذَابٌ مُّسْتَقِرٌّ
Mu foog leen, suba teel, ak mbugël mu ñu dootul tàggool.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Al-Qamar 36

Simoore Al-Qamar Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Daan na leen xupp ci Sunu mbugël. Waaye teewul ñu…

Simoore Aaya 36/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers