Al-Qamar · 45/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
سَيُهْزَمُ الْجَمْعُ وَيُوَلُّونَ الدُّبُرَ ۝٤٥
Sa yuhzamul jam`u wa yuwalloonad dubur
📖 Tekkim Wolof
Seen booloo gi dana tas , ñu ne wëqét daw wane ginnaaw.

🎧 Dégg


📜 Aaya 43-47 — Simoore Al-Qamar

43أَكُفَّارُكُمْ خَيْرٌ مِّنْ أُولَٰئِكُمْ أَمْ لَكُم بَرَاءَةٌ فِي الزُّبُرِ
Seen yéefar yi ndax dañoo gën ñooña ? Walla dañu leen bindal ci téere yi ne mucc ngeen ?
44أَمْ يَقُولُونَ نَحْنُ جَمِيعٌ مُّنتَصِرٌ
Walla ñoom dañuy wax naan : “Nun ñépp nooy am ndam”.
45سَيُهْزَمُ الْجَمْعُ وَيُوَلُّونَ الدُّبُرَ
Seen booloo gi dana tas , ñu ne wëqét daw wane ginnaaw.
46بَلِ السَّاعَةُ مَوْعِدُهُمْ وَالسَّاعَةُ أَدْهَىٰ وَأَمَرُّ
Bis Pénc, ba la ñuy dajeeti, te bis Pénc moo gënatee mitti te tar.
47إِنَّ الْمُجْرِمِينَ فِي ضَلَالٍ وَسُعُرٍ
Tooñkat ya ña nga ca, cànkute ak réer.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
45Aaya

Tekki — Al-Qamar 45

Simoore Al-Qamar Aaya 45 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Seen booloo gi dana tas , ñu ne wëqét daw…

Simoore Aaya 45/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 43–47. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers