Al-Qamar · 46/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
بَلِ السَّاعَةُ مَوْعِدُهُمْ وَالسَّاعَةُ أَدْهَىٰ وَأَمَرُّ ۝٤٦
Balis Saa`atu maw`iduhum was Saa`atu adhaa wa amarr
📖 Tekkim Wolof
Bis Pénc, ba la ñuy dajeeti, te bis Pénc moo gënatee mitti te tar.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 44-48 — Simoore Al-Qamar

44أَمْ يَقُولُونَ نَحْنُ جَمِيعٌ مُّنتَصِرٌ
Walla ñoom dañuy wax naan : “Nun ñépp nooy am ndam”.
45سَيُهْزَمُ الْجَمْعُ وَيُوَلُّونَ الدُّبُرَ
Seen booloo gi dana tas , ñu ne wëqét daw wane ginnaaw.
46بَلِ السَّاعَةُ مَوْعِدُهُمْ وَالسَّاعَةُ أَدْهَىٰ وَأَمَرُّ
Bis Pénc, ba la ñuy dajeeti, te bis Pénc moo gënatee mitti te tar.
47إِنَّ الْمُجْرِمِينَ فِي ضَلَالٍ وَسُعُرٍ
Tooñkat ya ña nga ca, cànkute ak réer.
48يَوْمَ يُسْحَبُونَ فِي النَّارِ عَلَىٰ وُجُوهِهِمْ ذُوقُوا مَسَّ سَقَرَ
Bu keroogee ba ñu di leen diri ci seen xarkanam ca biir Safara, (naan leen) : “Mosleen tokamti gu Safara”.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
46Aaya

Tekki — Al-Qamar 46

Simoore Al-Qamar Aaya 46 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bis Pénc, ba la ñuy dajeeti, te bis Pénc moo…

Simoore Aaya 46/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 44–48. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers