Al-Qamar · 9/55
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qamar
۞ كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ فَكَذَّبُوا عَبْدَنَا وَقَالُوا مَجْنُونٌ وَازْدُجِرَ ۝٩
Kazzabat qablahum qawmu Noohin fakazzaboo `abdanaa wa qaaloo majnoo nunw wazdujir
📖 Tekkim Wolof
Nitu Nooh, ña leen jiitu woon weddi woon nañu. Ñoom it weddi woon nañu sunub jaam daldi wax ne: “Kii ab dof la ! ” daldi koy bàyyi.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 7-11 — Simoore Al-Qamar

7خُشَّعًا أَبْصَارُهُمْ يَخْرُجُونَ مِنَ الْأَجْدَاثِ كَأَنَّهُمْ جَرَادٌ مُّنتَشِرٌ
ñuy jatt seeni gis ba, di génne ci bàmmeel yi dañuy melni ay soccent yu ñu tasaare,
8مُّهْطِعِينَ إِلَى الدَّاعِ ۖ يَقُولُ الْكَافِرُونَ هَٰذَا يَوْمٌ عَسِرٌ
sëggël seeni doq, jëm ca, wootekatu ba. Yéefër yaa nga naan : “Lii dey bis bu jafeñ la”.
9۞ كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ فَكَذَّبُوا عَبْدَنَا وَقَالُوا مَجْنُونٌ وَازْدُجِرَ
Nitu Nooh, ña leen jiitu woon weddi woon nañu. Ñoom it weddi woon nañu sunub jaam daldi wax ne: “Kii ab dof la ! ” daldi koy bàyyi.
10فَدَعَا رَبَّهُ أَنِّي مَغْلُوبٌ فَانتَصِرْ
mu woo Boroomam ñaan ko ne : “Man dey sonal nañu ma. Dimbalima”.
11فَفَتَحْنَا أَبْوَابَ السَّمَاءِ بِمَاءٍ مُّنْهَمِرٍ
Nu daldi ubbi wunti asamaan si ci am ndox muy dottiku,
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Al-Qamar 9

Simoore Al-Qamar Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nitu Nooh, ña leen jiitu woon weddi woon nañu. Ñoom…

Simoore Aaya 9/55 — Simoore Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qamar Dégg, Simoore Al-Qamar Tekki, Simoore Al-Qamar mp3, Simoore Al-Qamar pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Wednesday, September 30, 2026

Don't forget us in your sincere prayers