Al-Qamar · 10/55
Tekki Waxtaan — Al-Qamar
فَدَعَا رَبَّهُ أَنِّي مَغْلُوبٌ فَانتَصِرْ ١٠
Transliteration
Fada`aa Rabbahooo annee maghloobun fantasir
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
mu woo Boroomam ñaan ko ne : “Man dey sonal nañu ma. Dimbalima”.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 8-12 — Al-Qamar
8مُّهْطِعِينَ إِلَى الدَّاعِ ۖ يَقُولُ الْكَافِرُونَ هَٰذَا يَوْمٌ عَسِرٌ
sëggël seeni doq, jëm ca, wootekatu ba. Yéefër yaa nga naan : “Lii dey bis bu jafeñ la”.
9۞ كَذَّبَتْ قَبْلَهُمْ قَوْمُ نُوحٍ فَكَذَّبُوا عَبْدَنَا وَقَالُوا مَجْنُونٌ وَازْدُجِرَ
Nitu Nooh, ña leen jiitu woon weddi woon nañu. Ñoom it weddi woon nañu sunub jaam daldi wax ne: “Kii ab dof la ! ” daldi koy bàyyi.
10فَدَعَا رَبَّهُ أَنِّي مَغْلُوبٌ فَانتَصِرْ
mu woo Boroomam ñaan ko ne : “Man dey sonal nañu ma. Dimbalima”.
11فَفَتَحْنَا أَبْوَابَ السَّمَاءِ بِمَاءٍ مُّنْهَمِرٍ
Nu daldi ubbi wunti asamaan si ci am ndox muy dottiku,
12وَفَجَّرْنَا الْأَرْضَ عُيُونًا فَالْتَقَى الْمَاءُ عَلَىٰ أَمْرٍ قَدْ قُدِرَ
nu daldi ballal suuf ak ay bëti ndox. Ndox ya daldi gëndóo daj ci ndigal lu ñu natale.
Al-QamarFihi Alxuraan
55Aaya
MeccanRevelation
10Aaya
Tekki — Al-Qamar 10
Simoore Al-Qamar Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : mu woo Boroomam ñaan ko ne : “Man dey sonal…Simoore Aaya 10/55 — Al-Qamar القمر (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qamar Dégg, Al-Qamar Tekki, Al-Qamar mp3, Al-Qamar pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Wednesday, August 19, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








