Ar-Rahman · 14/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن صَلْصَالٍ كَالْفَخَّارِ ۝١٤
Khalaqal insaana min salsaalin kalfakhkhaari
📖 Tekkim Wolof
Moom moo bind nit ci ban bu tikk dëgër ;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 12-16 — Simoore Ar-Rahman

12وَالْحَبُّ ذُو الْعَصْفِ وَالرَّيْحَانُ
ak ay fepp yu nekk ci mbaram, ak gàncax yuy gilli.
13فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
14خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن صَلْصَالٍ كَالْفَخَّارِ
Moom moo bind nit ci ban bu tikk dëgër ;
15وَخَلَقَ الْجَانَّ مِن مَّارِجٍ مِّن نَّارٍ
te Moo bind jinne ci safara wuy bérëx wu amul saxaar;
16فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
14Aaya

Tekki — Ar-Rahman 14

Simoore Ar-Rahman Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom moo bind nit ci ban bu tikk dëgër ;

Simoore Aaya 14/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers