Ar-Rahman · 13/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ ۝١٣
Fabi ayyi aalaaa`i Rabbikumaa tukazzibaan
📖 Tekkim Wolof
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Simoore Ar-Rahman

11فِيهَا فَاكِهَةٌ وَالنَّخْلُ ذَاتُ الْأَكْمَامِ
am na ay fuytéef, ak tàndarma yuy meññ,
12وَالْحَبُّ ذُو الْعَصْفِ وَالرَّيْحَانُ
ak ay fepp yu nekk ci mbaram, ak gàncax yuy gilli.
13فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
14خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن صَلْصَالٍ كَالْفَخَّارِ
Moom moo bind nit ci ban bu tikk dëgër ;
15وَخَلَقَ الْجَانَّ مِن مَّارِجٍ مِّن نَّارٍ
te Moo bind jinne ci safara wuy bérëx wu amul saxaar;
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
13Aaya

Tekki — Ar-Rahman 13

Simoore Ar-Rahman Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a…

Simoore Aaya 13/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers