Ar-Rahman · 15/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
وَخَلَقَ الْجَانَّ مِن مَّارِجٍ مِّن نَّارٍ ۝١٥
Wa khalaqal jaaan mim maarijim min naar
📖 Tekkim Wolof
te Moo bind jinne ci safara wuy bérëx wu amul saxaar;

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 13-17 — Simoore Ar-Rahman

13فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
14خَلَقَ الْإِنسَانَ مِن صَلْصَالٍ كَالْفَخَّارِ
Moom moo bind nit ci ban bu tikk dëgër ;
15وَخَلَقَ الْجَانَّ مِن مَّارِجٍ مِّن نَّارٍ
te Moo bind jinne ci safara wuy bérëx wu amul saxaar;
16فَبِأَيِّ آلَاءِ رَبِّكُمَا تُكَذِّبَانِ
Yéen nit ak jinne ana naka ngeen di man a weddee seen xeewali Boroom ?
17رَبُّ الْمَشْرِقَيْنِ وَرَبُّ الْمَغْرِبَيْنِ
Boroom ñaari Penku yi tey Boroom ñaari Sowo yi !
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
15Aaya

Tekki — Ar-Rahman 15

Simoore Ar-Rahman Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : te Moo bind jinne ci safara wuy bérëx wu amul…

Simoore Aaya 15/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers