Ar-Rahman · 5/78
Tekki Waxtaan — Simoore Ar-Rahman
الشَّمْسُ وَالْقَمَرُ بِحُسْبَانٍ ۝٥
Ashshamsu walqamaru bihusbaan
📖 Tekkim Wolof
Jant beek weer wi ne rojj yemoo

🎧 Dégg


📜 Aaya 3-7 — Simoore Ar-Rahman

3خَلَقَ الْإِنسَانَ
Moo bind nit (sos ko).
4عَلَّمَهُ الْبَيَانَ
Moo ko jàngal waxiin wu leer.
5الشَّمْسُ وَالْقَمَرُ بِحُسْبَانٍ
Jant beek weer wi ne rojj yemoo
6وَالنَّجْمُ وَالشَّجَرُ يَسْجُدَانِ
garab yi ak ñax mi dañuy sujuud.
7وَالسَّمَاءَ رَفَعَهَا وَوَضَعَ الْمِيزَانَ
Moom moo kaweel asamaan. Teg ca ay nattukaayam màndaxe (balaas),
Ar-RahmanFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
5Aaya

Tekki — Ar-Rahman 5

Simoore Ar-Rahman Aaya 5 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jant beek weer wi ne rojj yemoo

Simoore Aaya 5/78 — Simoore Ar-Rahman الرحمن (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ar-Rahman Dégg, Simoore Ar-Rahman Tekki, Simoore Ar-Rahman mp3, Simoore Ar-Rahman pdf. Aaya 3–7. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers