Al-A'raf · 196/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
إِنَّ وَلِيِّيَ اللَّهُ الَّذِي نَزَّلَ الْكِتَابَ ۖ وَهُوَ يَتَوَلَّى الصَّالِحِينَ ۝١٩٦
Inna waliyyial laahul lazee nazzalal Kitaaba wa Huwa yatawallas saaliheen
📖 Tekkim Wolof
Ki may dimbali mooy Yàlla Mi wàcce Téere ba te mu méngook ñu sell ña.
🎧 Dégg

📜 Aaya 194-198 — Al-A'raf

194إِنَّ الَّذِينَ تَدْعُونَ مِن دُونِ اللَّهِ عِبَادٌ أَمْثَالُكُمْ ۖ فَادْعُوهُمْ فَلْيَسْتَجِيبُوا لَكُمْ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Ña nga xam ne dangeen leen jaamu bàyyi Yàlla, ay jaam lañu ni yéen. Wooleen ba xam danañu leen nangul ndeem ñu dëggu ngeen.
195أَلَهُمْ أَرْجُلٌ يَمْشُونَ بِهَا ۖ أَمْ لَهُمْ أَيْدٍ يَبْطِشُونَ بِهَا ۖ أَمْ لَهُمْ أَعْيُنٌ يُبْصِرُونَ بِهَا ۖ أَمْ لَهُمْ آذَانٌ يَسْمَعُونَ بِهَا ۗ قُلِ ادْعُوا شُرَكَاءَكُمْ ثُمَّ كِيدُونِ فَلَا تُنظِرُونِ
Moo ndax dañoo am tànk yu ñu doxe ? Moo ndax dañoo am loxo yu ñu téye ? Moo ndax dañoo am bët yu ñuy gise ? Moo ndax dañoo am nopp yu ñuy dégge ? Neeleen : “Wooleen seen bokkaale yooyu, te nangeen ma fexeel, bañ maa yeexe.
196إِنَّ وَلِيِّيَ اللَّهُ الَّذِي نَزَّلَ الْكِتَابَ ۖ وَهُوَ يَتَوَلَّى الصَّالِحِينَ
Ki may dimbali mooy Yàlla Mi wàcce Téere ba te mu méngook ñu sell ña.
197وَالَّذِينَ تَدْعُونَ مِن دُونِهِ لَا يَسْتَطِيعُونَ نَصْرَكُمْ وَلَا أَنفُسَهُمْ يَنصُرُونَ
Ña ngeen di jaamu te bàyyi Ko, mënuñuleen a dimbali te mënuñoo dimbali seen bopp sax.”
198وَإِن تَدْعُوهُمْ إِلَى الْهُدَىٰ لَا يَسْمَعُوا ۖ وَتَرَاهُمْ يَنظُرُونَ إِلَيْكَ وَهُمْ لَا يُبْصِرُونَ
Boo leen woowee cig njub duñu dégg sax. Dangeen gis ñu di la xool te ñoom duñu gis.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
196Aaya

Tekki — Al-A'raf 196

Simoore Al-A'raf Aaya 196 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ki may dimbali mooy Yàlla Mi wàcce Téere ba te…

Simoore Aaya 196/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 194–198. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers