Al-A'raf · 65/206
Tekki Waxtaan — Al-A'raf
۞ وَإِلَىٰ عَادٍ أَخَاهُمْ هُودًا ۗ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۚ أَفَلَا تَتَّقُونَ ۝٦٥
Wa ilaa `aadin akhaahum Hoodaa; qaala yaa qawmi` budul laaha maa lakum min ilaahin ghairuh; afalaa tattaqoon
📖 Tekkim Wolof
[Yónni woon Nanu it] ca waa [Haad], seen mbokk [Huud], mu ne leen : "Yéen samay mbokk, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen Yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
🎧 Dégg

📜 Aaya 63-67 — Al-A'raf

63أَوَعَجِبْتُمْ أَن جَاءَكُمْ ذِكْرٌ مِّن رَّبِّكُمْ عَلَىٰ رَجُلٍ مِّنكُمْ لِيُنذِرَكُمْ وَلِتَتَّقُوا وَلَعَلَّكُمْ تُرْحَمُونَ
Moo ndax dafa leen a jaaxal, ay kàdduy waare dikkal leen tukkee ca seen Boroom, jaare ci góor gu bokk ci yéen, ngir mu artu leen ngeen ragal Yàlla, ndax xéy-na yërëmeef leen ? ”
64فَكَذَّبُوهُ فَأَنجَيْنَاهُ وَالَّذِينَ مَعَهُ فِي الْفُلْكِ وَأَغْرَقْنَا الَّذِينَ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا عَمِينَ
Ñu weddi ko. Nu musal ko, moom ak ña nekkoon ak moom ca gaal ga, Nu labal ña weddi samay kàddu. Ñooña, aw nitam ñu gumba lañu woon.
65۞ وَإِلَىٰ عَادٍ أَخَاهُمْ هُودًا ۗ قَالَ يَا قَوْمِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۚ أَفَلَا تَتَّقُونَ
[Yónni woon Nanu it] ca waa [Haad], seen mbokk [Huud], mu ne leen : "Yéen samay mbokk, jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen Yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
66قَالَ الْمَلَأُ الَّذِينَ كَفَرُوا مِن قَوْمِهِ إِنَّا لَنَرَاكَ فِي سَفَاهَةٍ وَإِنَّا لَنَظُنُّكَ مِنَ الْكَاذِبِينَ
Mbooloo ma weddi, ca aw nitam, wax ne : “Nun gis nanu la nga nekk ci ag ndof, te nun sax far nanu jort ne yaw ci fenkat yi nga bokk”.
67قَالَ يَا قَوْمِ لَيْسَ بِي سَفَاهَةٌ وَلَٰكِنِّي رَسُولٌ مِّن رَّبِّ الْعَالَمِينَ
Mu ne : "Yéen samay mbokk, ag ndof nekkul ci man de ; waaye li wér moo di ne man ab Yonent laa, [ndaw] lu bawoo fa Yàlla Boroom àddina si.
Al-A'rafFihi Alxuraan
206Aaya
MeccanRevelation
65Aaya

Tekki — Al-A'raf 65

Simoore Al-A'raf Aaya 65 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Yónni woon Nanu it] ca waa [Haad], seen mbokk [Huud],…

Simoore Aaya 65/206 — Al-A'raf الأعراف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-A'raf Dégg, Al-A'raf Tekki, Al-A'raf mp3, Al-A'raf pdf. Aaya 63–67. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers