Al-Ma'arij · 38/44
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ma'arij
أَيَطْمَعُ كُلُّ امْرِئٍ مِّنْهُمْ أَن يُدْخَلَ جَنَّةَ نَعِيمٍ ۝٣٨
Ayatma`u kullum ri`im minhum anyyudkhala jannata Na`eem
📖 Tekkim Wolof
Ndax nit ñépp dañoo maase bëgg a duggëndoo Àjjanay xéewal?

🎧 Dégg


📜 Aaya 36-40 — Simoore Al-Ma'arij

36فَمَالِ الَّذِينَ كَفَرُوا قِبَلَكَ مُهْطِعِينَ
Waaw yéefar yi lu ñu xewal bay raj-rajloo wutsi la,
37عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ عِزِينَ
di bawoo ndeyjoor ak càmmooñ, tey wél-wéli ?
38أَيَطْمَعُ كُلُّ امْرِئٍ مِّنْهُمْ أَن يُدْخَلَ جَنَّةَ نَعِيمٍ
Ndax nit ñépp dañoo maase bëgg a duggëndoo Àjjanay xéewal?
39كَلَّا ۖ إِنَّا خَلَقْنَاهُم مِّمَّا يَعْلَمُونَ
Mukk ! Noo leen sàkk ak ni ñu ko xame.
40فَلَا أُقْسِمُ بِرَبِّ الْمَشَارِقِ وَالْمَغَارِبِ إِنَّا لَقَادِرُونَ
Déedéet !... Maa ngi giñ ci Boroom Penku ak Sowu yi ci ne Nun boroom Kàttan la nu.
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 38

Simoore Al-Ma'arij Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax nit ñépp dañoo maase bëgg a duggëndoo Àjjanay xéewal?

Simoore Aaya 38/44 — Simoore Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ma'arij Dégg, Simoore Al-Ma'arij Tekki, Simoore Al-Ma'arij mp3, Simoore Al-Ma'arij pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers