Al-Ma'arij · 37/44
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ma'arij
عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ عِزِينَ ۝٣٧
Anil yameeni wa `anish shimaali `izeen
📖 Tekkim Wolof
di bawoo ndeyjoor ak càmmooñ, tey wél-wéli ?

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 35-39 — Simoore Al-Ma'arij

35أُولَٰئِكَ فِي جَنَّاتٍ مُّكْرَمُونَ
Ñoom ña nga biir Àjjana deefi leen teral.
36فَمَالِ الَّذِينَ كَفَرُوا قِبَلَكَ مُهْطِعِينَ
Waaw yéefar yi lu ñu xewal bay raj-rajloo wutsi la,
37عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ عِزِينَ
di bawoo ndeyjoor ak càmmooñ, tey wél-wéli ?
38أَيَطْمَعُ كُلُّ امْرِئٍ مِّنْهُمْ أَن يُدْخَلَ جَنَّةَ نَعِيمٍ
Ndax nit ñépp dañoo maase bëgg a duggëndoo Àjjanay xéewal?
39كَلَّا ۖ إِنَّا خَلَقْنَاهُم مِّمَّا يَعْلَمُونَ
Mukk ! Noo leen sàkk ak ni ñu ko xame.
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 37

Simoore Al-Ma'arij Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : di bawoo ndeyjoor ak càmmooñ, tey wél-wéli ?

Simoore Aaya 37/44 — Simoore Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ma'arij Dégg, Simoore Al-Ma'arij Tekki, Simoore Al-Ma'arij mp3, Simoore Al-Ma'arij pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers