Al-Ma'arij · 39/44
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Ma'arij
كَلَّا ۖ إِنَّا خَلَقْنَاهُم مِّمَّا يَعْلَمُونَ ۝٣٩
Kallaaa innaa khalaq nahum mimmaa ya`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Mukk ! Noo leen sàkk ak ni ñu ko xame.

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Simoore Al-Ma'arij

37عَنِ الْيَمِينِ وَعَنِ الشِّمَالِ عِزِينَ
di bawoo ndeyjoor ak càmmooñ, tey wél-wéli ?
38أَيَطْمَعُ كُلُّ امْرِئٍ مِّنْهُمْ أَن يُدْخَلَ جَنَّةَ نَعِيمٍ
Ndax nit ñépp dañoo maase bëgg a duggëndoo Àjjanay xéewal?
39كَلَّا ۖ إِنَّا خَلَقْنَاهُم مِّمَّا يَعْلَمُونَ
Mukk ! Noo leen sàkk ak ni ñu ko xame.
40فَلَا أُقْسِمُ بِرَبِّ الْمَشَارِقِ وَالْمَغَارِبِ إِنَّا لَقَادِرُونَ
Déedéet !... Maa ngi giñ ci Boroom Penku ak Sowu yi ci ne Nun boroom Kàttan la nu.
41عَلَىٰ أَن نُّبَدِّلَ خَيْرًا مِّنْهُمْ وَمَا نَحْنُ بِمَسْبُوقِينَ
Ci soppi wuutale leen ak ñeneen ñu leen gën, te kenn du ko fanq.
Al-Ma'arijFihi Alxuraan
44Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Al-Ma'arij 39

Simoore Al-Ma'arij Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mukk ! Noo leen sàkk ak ni ñu ko xame.

Simoore Aaya 39/44 — Simoore Al-Ma'arij المعارج (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Ma'arij Dégg, Simoore Al-Ma'arij Tekki, Simoore Al-Ma'arij mp3, Simoore Al-Ma'arij pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers