Nuh · 9/28
Tekki Waxtaan — Simoore Nuh
ثُمَّ إِنِّي أَعْلَنتُ لَهُمْ وَأَسْرَرْتُ لَهُمْ إِسْرَارًا ۝٩
Summaa inneee a`lantu lahum wa asrartu lahum israaraa
📖 Tekkim Wolof
Topp, biralalnaa leen, yalolnaa leen.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 7-11 — Simoore Nuh

7وَإِنِّي كُلَّمَا دَعَوْتُهُمْ لِتَغْفِرَ لَهُمْ جَعَلُوا أَصَابِعَهُمْ فِي آذَانِهِمْ وَاسْتَغْشَوْا ثِيَابَهُمْ وَأَصَرُّوا وَاسْتَكْبَرُوا اسْتِكْبَارًا
Te man saasu ma leen di woo ngir Nga jégël leen, dañuy def séeni waaraam ci séeni biiri nopp, daldi muuroo séeni sér, daldi jomlu.
8ثُمَّ إِنِّي دَعَوْتُهُمْ جِهَارًا
Topp, woonaa leen cig jooru.
9ثُمَّ إِنِّي أَعْلَنتُ لَهُمْ وَأَسْرَرْتُ لَهُمْ إِسْرَارًا
Topp, biralalnaa leen, yalolnaa leen.
10فَقُلْتُ اسْتَغْفِرُوا رَبَّكُمْ إِنَّهُ كَانَ غَفَّارًا
Ma wax leen ne : “Jégëluleen seen Boroom, Moom dey Jégëlaakoon la,
11يُرْسِلِ السَّمَاءَ عَلَيْكُم مِّدْرَارًا
kon dey dana yabal asamaan si, mu duttil leen taw,
NuhFihi Alxuraan
28Aaya
MeccanRevelation
9Aaya

Tekki — Nuh 9

Simoore Nuh Aaya 9 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Topp, biralalnaa leen, yalolnaa leen.

Simoore Aaya 9/28 — Simoore Nuh نوح (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Nuh Dégg, Simoore Nuh Tekki, Simoore Nuh mp3, Simoore Nuh pdf. Aaya 7–11. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Sunday, October 11, 2026

Don't forget us in your sincere prayers