Al-Muzzammil · 8/20
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Muzzammil
وَاذْكُرِ اسْمَ رَبِّكَ وَتَبَتَّلْ إِلَيْهِ تَبْتِيلًا ۝٨
Wazkuris ma rabbika wa tabattal ilaihi tabteelaa
📖 Tekkim Wolof
Na ngay fàttaliku di tud sa turu Boroom te wéeru ci moom fàwwu,

🎧 Dégg


📜 Aaya 6-10 — Simoore Al-Muzzammil

6إِنَّ نَاشِئَةَ اللَّيْلِ هِيَ أَشَدُّ وَطْئًا وَأَقْوَمُ قِيلًا
Jullig guddi nag moo gëna nangu te moo gëna leer cim njàng.
7إِنَّ لَكَ فِي النَّهَارِ سَبْحًا طَوِيلًا
Am nga, ci bëcëg bi, jot gu gudd goo mana lijantee.
8وَاذْكُرِ اسْمَ رَبِّكَ وَتَبَتَّلْ إِلَيْهِ تَبْتِيلًا
Na ngay fàttaliku di tud sa turu Boroom te wéeru ci moom fàwwu,
9رَّبُّ الْمَشْرِقِ وَالْمَغْرِبِ لَا إِلَٰهَ إِلَّا هُوَ فَاتَّخِذْهُ وَكِيلًا
mooy boroom Penkook Sowu. Amul jeneen Yàlla ju dul moom. Na nga wéeru ci moom.
10وَاصْبِرْ عَلَىٰ مَا يَقُولُونَ وَاهْجُرْهُمْ هَجْرًا جَمِيلًا
Muñal li ñuy wax ; te nga gàddaay leen gàddaay gu rafet (bañ leena faale).
Al-MuzzammilFihi Alxuraan
20Aaya
MeccanRevelation
8Aaya

Tekki — Al-Muzzammil 8

Simoore Al-Muzzammil Aaya 8 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Na ngay fàttaliku di tud sa turu Boroom te wéeru…

Simoore Aaya 8/20 — Simoore Al-Muzzammil المزمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Muzzammil Dégg, Simoore Al-Muzzammil Tekki, Simoore Al-Muzzammil mp3, Simoore Al-Muzzammil pdf. Aaya 6–10. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers