An-Naba · 21/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
إِنَّ جَهَنَّمَ كَانَتْ مِرْصَادًا ۝٢١
Inna jahan nama kaanat mirsaada
📖 Tekkim Wolof
Waajal nanu safara muy tuqlóo,

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Simoore An-Naba

19وَفُتِحَتِ السَّمَاءُ فَكَانَتْ أَبْوَابًا
nu ubbi asamaan si mu def ay buntu,
20وَسُيِّرَتِ الْجِبَالُ فَكَانَتْ سَرَابًا
nu doxloo tundi doj yi mu melni ñàndóox.
21إِنَّ جَهَنَّمَ كَانَتْ مِرْصَادًا
Waajal nanu safara muy tuqlóo,
22لِّلطَّاغِينَ مَآبًا
di xala doon dekuwaayu ñu bew ña.
23لَّابِثِينَ فِيهَا أَحْقَابًا
Danañu fa sax ay jamono yu yàgg.
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
21Aaya

Tekki — An-Naba 21

Simoore An-Naba Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waajal nanu safara muy tuqlóo,

Simoore Aaya 21/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers