An-Naba · 30/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
فَذُوقُوا فَلَن نَّزِيدَكُمْ إِلَّا عَذَابًا ۝٣٠
Fa zooqoo falan-nazee dakum ill-laa azaaba
📖 Tekkim Wolof
Ayca mosleen. Dunu leen dolli lu dul mbugël (tokamtikuleen ko)!

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Simoore An-Naba

28وَكَذَّبُوا بِآيَاتِنَا كِذَّابًا
ña weddiwoon sunuy Laaya,
29وَكُلَّ شَيْءٍ أَحْصَيْنَاهُ كِتَابًا
lépp lu ne peek nanu ko bind ko.
30فَذُوقُوا فَلَن نَّزِيدَكُمْ إِلَّا عَذَابًا
Ayca mosleen. Dunu leen dolli lu dul mbugël (tokamtikuleen ko)!
31إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ مَفَازًا
Ña ragal Yàlla ñoom baaxal nañu :
32حَدَائِقَ وَأَعْنَابًا
am nañu ay tooli dër ak i reseñ,
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — An-Naba 30

Simoore An-Naba Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ayca mosleen. Dunu leen dolli lu dul mbugël (tokamtikuleen ko)!

Simoore Aaya 30/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers