An-Naba · 31/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ مَفَازًا ۝٣١
Inna lil mutta qeena mafaaza
📖 Tekkim Wolof
Ña ragal Yàlla ñoom baaxal nañu :

🎧 Dégg


📜 Aaya 29-33 — Simoore An-Naba

29وَكُلَّ شَيْءٍ أَحْصَيْنَاهُ كِتَابًا
lépp lu ne peek nanu ko bind ko.
30فَذُوقُوا فَلَن نَّزِيدَكُمْ إِلَّا عَذَابًا
Ayca mosleen. Dunu leen dolli lu dul mbugël (tokamtikuleen ko)!
31إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ مَفَازًا
Ña ragal Yàlla ñoom baaxal nañu :
32حَدَائِقَ وَأَعْنَابًا
am nañu ay tooli dër ak i reseñ,
33وَكَوَاعِبَ أَتْرَابًا
ak i jongama huur yu taxaw ay ween te maase,
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
31Aaya

Tekki — An-Naba 31

Simoore An-Naba Aaya 31 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña ragal Yàlla ñoom baaxal nañu :

Simoore Aaya 31/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 29–33. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers