An-Naba · 29/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
وَكُلَّ شَيْءٍ أَحْصَيْنَاهُ كِتَابًا ۝٢٩
Wa kulla shai-in ahsai naahu kitaa ba
📖 Tekkim Wolof
lépp lu ne peek nanu ko bind ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 27-31 — Simoore An-Naba

27إِنَّهُمْ كَانُوا لَا يَرْجُونَ حِسَابًا
Ñoom dañoo foogoon ne duñu leen màndaxe,
28وَكَذَّبُوا بِآيَاتِنَا كِذَّابًا
ña weddiwoon sunuy Laaya,
29وَكُلَّ شَيْءٍ أَحْصَيْنَاهُ كِتَابًا
lépp lu ne peek nanu ko bind ko.
30فَذُوقُوا فَلَن نَّزِيدَكُمْ إِلَّا عَذَابًا
Ayca mosleen. Dunu leen dolli lu dul mbugël (tokamtikuleen ko)!
31إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ مَفَازًا
Ña ragal Yàlla ñoom baaxal nañu :
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
29Aaya

Tekki — An-Naba 29

Simoore An-Naba Aaya 29 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : lépp lu ne peek nanu ko bind ko.

Simoore Aaya 29/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 27–31. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers