An-Naba · 33/40
Tekki Waxtaan — An-Naba
وَكَوَاعِبَ أَتْرَابًا ۝٣٣
Wa kaawa `iba at raaba
📖 Tekkim Wolof
ak i jongama huur yu taxaw ay ween te maase,

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — An-Naba

31إِنَّ لِلْمُتَّقِينَ مَفَازًا
Ña ragal Yàlla ñoom baaxal nañu :
32حَدَائِقَ وَأَعْنَابًا
am nañu ay tooli dër ak i reseñ,
33وَكَوَاعِبَ أَتْرَابًا
ak i jongama huur yu taxaw ay ween te maase,
34وَكَأْسًا دِهَاقًا
ak ay kaas yu fees dell.
35لَّا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا وَلَا كِذَّابًا
Duñu fa dégg mukk waxi caaxaan mbaa ay fen.
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — An-Naba 33

Simoore An-Naba Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ak i jongama huur yu taxaw ay ween te maase,

Simoore Aaya 33/40 — An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naba Dégg, An-Naba Tekki, An-Naba mp3, An-Naba pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers