An-Naba · 37/40
Tekki Waxtaan — An-Naba
رَّبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا الرَّحْمَٰنِ ۖ لَا يَمْلِكُونَ مِنْهُ خِطَابًا ۝٣٧
Rabbis samaa waati wal ardi wa maa baina humar rahmaani laa yam likoona minhu khi taaba
📖 Tekkim Wolof
Boroom asamaan yeek suuf seek li ci seen diggante, mooy Yëramaakoon bi ; duñu mana waxanteek moom.

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — An-Naba

35لَّا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا وَلَا كِذَّابًا
Duñu fa dégg mukk waxi caaxaan mbaa ay fen.
36جَزَاءً مِّن رَّبِّكَ عَطَاءً حِسَابًا
Muy pey gu bawoo ca seen Boroom
37رَّبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا الرَّحْمَٰنِ ۖ لَا يَمْلِكُونَ مِنْهُ خِطَابًا
Boroom asamaan yeek suuf seek li ci seen diggante, mooy Yëramaakoon bi ; duñu mana waxanteek moom.
38يَوْمَ يَقُومُ الرُّوحُ وَالْمَلَائِكَةُ صَفًّا ۖ لَّا يَتَكَلَّمُونَ إِلَّا مَنْ أَذِنَ لَهُ الرَّحْمَٰنُ وَقَالَ صَوَابًا
Bu keroogee ba Jibriil jóg ànd ak malaaka ya taxaw def sàppe, duñu wax , lu dul ku Yàlla Yëramaakoon bi jox ndigël, mu wax lay dëgg te yem ca kepp.
39ذَٰلِكَ الْيَوْمُ الْحَقُّ ۖ فَمَن شَاءَ اتَّخَذَ إِلَىٰ رَبِّهِ مَآبًا
Loolu moo di bisub dëgg ba. Ku mu soob mu jël Boroomam def ko ab rawtukaay.
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — An-Naba 37

Simoore An-Naba Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Boroom asamaan yeek suuf seek li ci seen diggante, mooy…

Simoore Aaya 37/40 — An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Naba Dégg, An-Naba Tekki, An-Naba mp3, An-Naba pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers