An-Naba · 36/40
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naba
جَزَاءً مِّن رَّبِّكَ عَطَاءً حِسَابًا ۝٣٦
Jazaa-am mir-rabbika ataa-an hisaaba
📖 Tekkim Wolof
Muy pey gu bawoo ca seen Boroom

🎧 Dégg


📜 Aaya 34-38 — Simoore An-Naba

34وَكَأْسًا دِهَاقًا
ak ay kaas yu fees dell.
35لَّا يَسْمَعُونَ فِيهَا لَغْوًا وَلَا كِذَّابًا
Duñu fa dégg mukk waxi caaxaan mbaa ay fen.
36جَزَاءً مِّن رَّبِّكَ عَطَاءً حِسَابًا
Muy pey gu bawoo ca seen Boroom
37رَّبِّ السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ وَمَا بَيْنَهُمَا الرَّحْمَٰنِ ۖ لَا يَمْلِكُونَ مِنْهُ خِطَابًا
Boroom asamaan yeek suuf seek li ci seen diggante, mooy Yëramaakoon bi ; duñu mana waxanteek moom.
38يَوْمَ يَقُومُ الرُّوحُ وَالْمَلَائِكَةُ صَفًّا ۖ لَّا يَتَكَلَّمُونَ إِلَّا مَنْ أَذِنَ لَهُ الرَّحْمَٰنُ وَقَالَ صَوَابًا
Bu keroogee ba Jibriil jóg ànd ak malaaka ya taxaw def sàppe, duñu wax , lu dul ku Yàlla Yëramaakoon bi jox ndigël, mu wax lay dëgg te yem ca kepp.
An-NabaFihi Alxuraan
40Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — An-Naba 36

Simoore An-Naba Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muy pey gu bawoo ca seen Boroom

Simoore Aaya 36/40 — Simoore An-Naba النبأ (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naba Dégg, Simoore An-Naba Tekki, Simoore An-Naba mp3, Simoore An-Naba pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers